Def lou nice

{title: Def lou nice}
{artist: Daara J}
{x_UGNG_category: Reggae, Sénégal}


Am / Bm

Def lou nice, Am lou nice
Def lou niagass, am lou niagass
x4

Wakh lo begeu
Oh Sakh ci mo defeul
Ton Di leoto di leoto
Di leoto be khei dan

Shaytan mom se bakan
Akhilou zaman zaman zaman zaman

Def lou nice, Am lou nice
Def lou niagass, am lou niagass
x4

Kou yag def lou nice beuss dina niaw  nga am lou rafet
Kep kou tèw ci guèw sentouko mingi niaw lire se defaite 
Malaka yaagi sèdè seye dieuf pese ko ci balance
Ki lé gauche ki lé droite niu node barzak audience

Loy def lu mou tole ci atom bour bi yallah faye la
Sentul mingi niaw lo ci gobe garde way la
Domu adama moy se adiana
Li de woor na ma ...
10 commandements
Def lu bone nga moun wouté nak al Coran
Sa khol bi nieup niss sey dieuf fokni yangi saran

Yangi def safan def lou bakh geun
Def ko fondement
Def lou nice moy se aldiana

Def lou nice, Am lou nice
Def lou niagass, am lou niagass
x4