{title: Birima}
{artist: Youssou Ndour}
[D]Maysa tende jodo yaa moom [E]liile (x3)
{soc}
{c: Refrain}
Hi woy biri[A]ma fumu yendu [D]ma yendu fa yendo naanee[E](x4)
{eoc}
Buri samba laobe yaa moom liile (x3)
Hi woy biri[A]ma fumu yendu [D]ma yendu fa yendo naanee[E](x4)
Damel maisa penda joor
Jooro jooro jooro jooro ho ho ho hoy
Sama waaji ken dula jam naani
{c: Refrain}
Mmmm mmm
Wooy tedi ngoné maarne be sambaa
Kuli baca senge ndat biran ngamoo
Ngoné maca nas mbay maca jeeri
Samba yaasimooooo dike mbay kuja dooooki
Yay borom mbaboor mi
{c: Refrain}
Dogo fal ak mawa joor kumba samba yaay jaloor
Dogo dogo, ho ho ho!
Aziz o mbay dogo xam nga yoon wee
{c: Refrain}
Maisa tendo jooro jooro a mari ngone sobel kayor niila
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee